home.social

#teere — Public Fediverse posts

Live and recent posts from across the Fediverse tagged #teere, aggregated by home.social.

  1. archive.org/details/bammeelu-k

    Bàmmeelu Kocc Barma : Téereb nettali by Bubakar Bóris Jóob; Boubacar Boris Diop

    Topics
    #téeré, #Joola, #Joolaa

    "Njéeme Pay, taskatu xibaar bu siiw ci Senegaal, moo toog bés këram dégg ci rajoy réew mi ne Joolaa bi, bato bi daan lëkkale Sigicoor ak Ndakaaru, suux na. Bàmmeelu Kocc Barma day delsi ci jéyya ju tiis jooju, di sargal ñi ci faatu ñépp, di jéem a yeewaale yit askan wi ngir lu ni mel bañ noo dalati. Waaye Njéeme yemul foofu: dafa nuy fàttali yit jaar-jaaru ndem-si-Yàlla ji Kinne Gaajo, fentaakon bu mag bu fiy taalifam yéemoon Afrig ak àddina si yépp. Ñoom ñaar nag, ay xariti benn bakkan, ay doomi-ndey, lañu woon, mu xamaloon ko lépp. Looloo tax Njéeme Pay di dànkaafu jàngkat bi, naan ko: bul jàppe Bàmmeelu Kocc Barma ni téereb nettali doŋŋ, téereb dekkali la tamit. Yokk na ci sax ne “fey bor, féddali kóllëre ak sàmm sama kàddu ñoo ma ko tax a bind…”"

  2. archive.org/details/bammeelu-k

  3. archive.org/details/bammeelu-k

  4. archive.org/details/bammeelu-k

  5. archive.org/details/bammeelu-k

  6. archive.org/details/yari-jamon

    Yari jamono : Téere fent by Mamadu Jara Juuf; Mamadou Diarra Diouf; Séex Aliyu Ndaw; Cheik Aliou Ndao

    Topics
    #OSAD, #njàngat, #téeré, #metit

    Fentaakon 8

  7. archive.org/details/sey-xare-l

    Séy xare la by Ndey Daba Ñaan; Ndèye Daba Niane

    Topics
    #téeré, #OSAD, #njàngat, #ladab

    "Téere bii, siiwalees na ko ci ndimbalal sàqu jàpple móoi mi nekk ci Njawriñu Caada ak Moomeelu Cossan bi ñu feg
    - Njiiteefu Téere ak Duruus"

  8. archive.org/details/Liggeeyu

    Liggéeyu ndey añub doom : Téere léeb (Recueil de contes en Wolof) by Maam Ngoy Siise; Mame Ngoye Cissé

    Topics
    #OSAD, #téeré, #léeb

    Léeboon 1

  9. archive.org/details/wolof-en

    Wolof Language: The Wolof Phrasebook and Dictionary by Assane Diop

    Topics
    #Wolof, #Angale, #Àngale, #ولوفل, #phrasebook, #dictionary, #translationdictionary, #bilingualdictionary, #njàngat, #téeré, #làkk, #tekki

    "This guide to Wolof language collects the most common Wolof phrases and expressions as well as an English-Wolof/Wolof-English dictionary. This phrasebook includes greetings, food items, directions, sightseeing and many other categories of expressions that will help anyone wanting to learn Wolof."

  10. archive.org/details/wolof-en

  11. archive.org/details/wolof-en

  12. archive.org/details/wolof-en

  13. archive.org/details/wolof-en

  14. archive.org/details/joob-mitin

    Mitiƞ : Caaroy - Pikin - Caajaay - Kees Jànqeen. 1982 - 1983 - 1984 = Meeting de Pikine, Thiaroye, Thiadiaye, Thiès by Séex Anta Jóob; Cheikh Anta Diop; Soxna Aram Faal; Sokhna Arame Fall

    Topics
    #njàngat, #téeré, #politig, #SéexAntaJóob, #Rassemblementnationaldémocratique, #RND

    "Jukki yi nu siiwal, ci mitiƞu RND yu Pikin, Caaroy, Caajaay ak Kees lañu tukkee ci atum 1982, 1983, 1984."

  15. archive.org/details/singali

    Singali : Nettali by Séex Aliyu Ndaw; Cheik Aliou Ndao

    Topics
    #njàngat, #téeré, #baayo

    "Singali téereb fent nettali la buy jéem a wone dund gu nàqari gi ab baayo nekke, rawatina su ndeyu jiitle ja wonewul as tuut ci yërmande.

    Li am solo mooy jom, muñ, ak dogu dimbale nañu Singali ba mu màgg faj gàcce.

    Waaye ba mu tekkee taxul muy feyyoonte. dafa tamu doon nit ku tabe, tey jéggale.

    Ndax kat dafa bokk ci ñi gëm ne lépp a ngi ci loxol boroom bi."

  16. archive.org/details/bataaxal-b

    Bataaxal bu gudde nii (Une si longue lettre) : Nettali by Mariyaama Ba; Mariama Bâ; Maam Yunus Jeŋ; Mame Younousse Dieng; Aram Faal; Arame Fall

    Topics
    #njàngat, #téeré, #SowwuAfrig, #jigéenyi

    "Booy xuus ci biir téere bi, ci ngay yëg ne fayda la ko mooñe. Xët bu ci nekk, xise bu ci nekk, kàddu gu mu ci doon rekk, daanaka màggal na wàll wu am solo ci askanu Senegaal, ba ci aada ak cosaan, lépp la génne, di ci leeral sunuy defin ak sunuy gisin. Téere bu mag ñeel Afrig gépp sosu na, feeñalaale nag senn soxna su mën (a bind) téere."

  17. archive.org/details/doomi-golo

    Doomi golo : nettali by Diop, Boubacar Boris

    Topics
    #njàngat, #téeré, #njaboot, #mbokkyi

    Novembre 2012

    283 pages ; 21 cm

    A novel

  18. archive.org/details/seex-yi-do

    Séex yi doon wër seen yaay by Jeewo Géy; Jeewo Guèye

    Topics
    #njàngat, #téeré, #jàngal

    Dakar: Editions Papyrus Afrique